Phillipe Monteiro - Sama Wo

Sama fans yi
Magui léne di gueureum
Di léne santeu
Guiss na séne taxaway

Musique bi
Pour yen la
Oh
Mane nop na léne
Waw (big up)

Yagueu neu lool
Bingueu démé
Mane réére na
Réére na sa yow
Lane la wara déf (wax ma)
Déf sans yow (sans yow hey)

Dama la soxla
Té da ma la beugueu
Déme ngueu té bay ma
Bay ma si leundeum
Wanté xam ngua ni

Ni dama wara doumeu maneu doundeu ba téy
Déme ngua té bay ma
Baby gnewateul si mane
Xana déguo sama wo
Baby gnewateul

Yagueu na lool bi ngua démé
Tax na sama xol wééte
Lou maye déf ba ngueu gneuwate
Gneuwate si mane
Baby gneuwatal

Yagneu na lool bi ngua démé
Tax na sama xol wéét
Xana di la wax beuss bou né fi ngua tolou si mane

Oh
Bou ma togué di xalaate
Doundeu you nex gui gnou done doundeu
Rek sama xool fess
Xama tou ma lou ma wara déf
Déme ngua bayi ma thi leundeum
Wanté xam ngua ni dama wara doundeu mateye

Déme ngua té bayi ma
Bayi ma si leundeum
Dama la soxla
Dama la beugueu

Baby ngeuwateul si mane
Xana déguo sama wo
Xama tou ma li ma war
a déf
Yagueu neu lool
Bouguou ma ngua xaam li ma dadj
Nax xaam na nik ame ngua kénéne
Meunou ma ko gueum
Meuneu dess ni

Yagueu na lool bi ngua déme
Mane réére na nékeutofi
Lane la wara déf nékeutofi

Dama la soxla
Dama la beugueu
Baby gneuwateul si mane
Xana déguo sama wo